Kàddug Yàlla: Kóllëre gu jekk gi ak Kóllëre gu bees gi۔
Appli bii mooy Kàddug Yàlla, gi dikke ñaari pàcc: Kóllëre gu jëkk gi Yàlla fas ak nit, ak Kóllëre gu yes, gi mujja wàcc, te ñenn ñi di ko wooye Injiil, mu tekki Xibaaa. Ñaari tére yooyu, Yàllaa leen wàcce ci nitam ñu sell ñi, kóllëre gu jëkk gi, ñu bind ko ci yawut, gu yees gi, ci làkku gereg. Li ñu bind ci tére yu jëkk ya nag, Moom lanu tekki ci wolof.
[بائبل، وولف، کدوگ یالا]